audio audioduration (s) 0.74 171 | text stringlengths 1 109 | gender stringclasses 2 values |
|---|---|---|
Fan lay sax ? | male | |
Saa boo ragalee Yàlla Buur bi moom miiy Kenn, ku dul Yàlla dalay ragal. | male | |
Buma ko jàppe. | male | |
Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex | female | |
Tom gisu ko woon. | female | |
Ma kay wayal Seex Saalihu. | male | |
03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li | female | |
Mas naa jaay lii. | female | |
Damaa yeex a ñëw. | female | |
manees na am yaakaar ci moom. | female | |
Jën dax na, tay . | male | |
Kuy seenub jkat? | male | |
Fi mu am | male | |
Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may | female | |
Maa ngi tëddoon sama lal. | male | |
Sama liggéey dafa géey. | female | |
Bul bàyyi ! | male | |
Toma ngi ci kaw. | female | |
Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole. | female | |
Xawma woon ne aw fen la. | male | |
Bëggu ñu la. | male | |
Damaa bëggoon a doon ndaw. | male | |
Wax naa dëgg, am déet ? | female | |
Soxla naa ab farandoo. | female | |
dinaa leen gindi | female | |
Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru. | female | |
Buleen ma xaar. | female | |
Bàyyi ma ma nelaw. | female | |
Jaxaay ji ak picc mi | female | |
Maa ngi jéggalu | female | |
Danuy jënd ay CD. | female | |
Suuf si daa di nangu. | female | |
Du sama mbir. | female | |
Xale yi gëmewuñu ko woon | female | |
Mbooram bi dëgg la. | female | |
Ci mbirum doomu weñ yi jigéenu-wérul war a wann | male | |
Loo soxla ? | male | |
Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia. | male | |
Loolu, du lu ma jékki-jekki rekk def ko | male | |
Ay nit lañu. | male | |
Bëgg naa ci benn ! | female | |
Nos dooley kaaraange ji | male | |
Doon naa ko ñaawal. | female | |
Nekkon na nu ay xarit. | male | |
Daa jubb lool. | male | |
Da koo kott. | male | |
Dangaa ñàkk jafe-jafe lool. | male | |
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul. | female | |
Jëfandikoo ko walla nga ñàkk ko. | male | |
Dama xalaat ne danga reelu. | female | |
Bunu wuute nag, foofu la liggéey bi nekk | male | |
Damaa am ñaan. | female | |
Setalal sa néeg bi ! | male | |
Toogal fii ak nun. | male | |
Taariix | male | |
Moos mi xossi nama. | male | |
Naj ak forse | female | |
Danga may fen ? | female | |
Noo rëyee nii?! | female | |
Nu ngi nekkandoowaat. | female | |
Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so | female | |
Dafa dégg i coow. | female | |
Mbir mii daal, kenn setu ci. | female | |
Am na ci ñent yoy ñi ngi ame ca armal ga | male | |
Tur wi feeñ na ci Injiil ci Mk 317. | male | |
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne | female | |
Mbaa kuy rambaaj naankat bu màndi xaaloo | male | |
Mu ne «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam». | female | |
Masuma faa dellu. | female | |
Beto De Canda | female | |
Tom sopp na mool yi. | female | |
Ma defoon ko ngir moom. | male | |
Daanaka, demewu fa noonu | female | |
mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa. | female | |
Damaa bëgg aar. | female | |
Wéer ngànnaay gi nag lii la wax | female | |
Moom la leen | male | |
Melal ni yaay man. | male | |
Ndax jekk ngeen ? | male | |
Man ngaa lakk farañse a? | female | |
Jox naa la ko am ? | male | |
Dañu maa féexal. | female | |
Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat | female | |
Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak | female | |
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar | female | |
Yokkal tuuti meew. | male | |
Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon | female | |
Jéem naa lépp. | male | |
defleen ag tànn ! | male | |
Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge | female | |
Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti. | female | |
XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ? | female | |
Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi | female | |
Damaa sonn lool?! | female | |
Àdduna wori neen la. | female | |
Lii sax caaxaan lay niru | male | |
Loo leen di nëbb ? | female | |
Yeneen waat yi it noonu lañu mel. | female | |
Ku wax ? | male | |
Dina soxla itam ab sàkket leeg-leeg ngir mu man a law ci kawam | male |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.