doc_id
stringlengths
10
18
text
stringlengths
6
366
tokens
listlengths
2
82
entities
listlengths
1
24
wol_test_1221
leer , wax luy wàllu Maamur Jàllo ( am na solo ñu fàtteli ko , ab kàngam ci nguur gi la , nekk tamit baay - faalu Maki Sàll ) ci mbir mi ñu jàpp ne ag càcc alali askan wi la , te tollu ci juróom - ñeent - fukki milyaar ak ñeent ci xaalisu seefaa , pexeem aaru mu geneen wàll gi ( te ñenn ci tas - kati xibaar yi di ko
[ "leer", ",", "wax", "luy", "wàllu", "Maamur", "Jàllo", "(", "am", "na", "solo", "ñu", "fàtteli", "ko", ",", "ab", "kàngam", "ci", "nguur", "gi", "la", ",", "nekk", "tamit", "baay", "-", "faalu", "Maki", "Sàll", ")", "ci", "mbir", "mi", "ñu", "jàpp"...
[ { "start": 21, "end": 33, "text": "Maamur Jàllo", "ner_type": "PER", "token_start": 5, "token_end": 7, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotati...
wol_test_1224
Waa Senegaal yépp yaakaaroon nañu ne , ndéem petorol ak gaas feeñ nañu ci réew mi , ak àdduna bu jaxasoo bii , nga xam ne kenn talatul kenn , Maki Sàll dina dooleel SENELEC ba dootuñu jeexal kuurãa mukk , ba koy jëggaani feneen .
[ "Waa", "Senegaal", "yépp", "yaakaaroon", "nañu", "ne", ",", "ndéem", "petorol", "ak", "gaas", "feeñ", "nañu", "ci", "réew", "mi", ",", "ak", "àdduna", "bu", "jaxasoo", "bii", ",", "nga", "xam", "ne", "kenn", "talatul", "kenn", ",", "Maki", "Sàll", "din...
[ { "start": 4, "end": 12, "text": "Senegaal", "ner_type": "LOC", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q1041", "qid_label": "Sénégal", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q1041", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Afrique de l'Ouest", "...
wol_test_1226
Askan wi rafetlu nañu yégleb CEDEAO bi .
[ "Askan", "wi", "rafetlu", "nañu", "yégleb", "CEDEAO", "bi", "." ]
[ { "start": 29, "end": 35, "text": "CEDEAO", "ner_type": "ORG", "token_start": 5, "token_end": 6, "qid": "Q193272", "qid_label": "communauté économique des États de l'Afrique de l'Ouest", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q193272", "qid_description_lang": "fr", "q...
wol_test_1230
Daam Jeŋ bokk naak njaboot yi seen naqar ak seen tiis ci jamono ji mu dalee seen kow .
[ "Daam", "Jeŋ", "bokk", "naak", "njaboot", "yi", "seen", "naqar", "ak", "seen", "tiis", "ci", "jamono", "ji", "mu", "dalee", "seen", "kow", "." ]
[ { "start": 0, "end": 8, "text": "Daam Jeŋ", "ner_type": "PER", "token_start": 0, "token_end": 2, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_met...
wol_test_1233
Waa Senegaal bile di Saajo Maane ak . . . waa Olànd bile di Vigil van Dijk .
[ "Waa", "Senegaal", "bile", "di", "Saajo", "Maane", "ak", ".", ".", ".", "waa", "Olànd", "bile", "di", "Vigil", "van", "Dijk", "." ]
[ { "start": 4, "end": 12, "text": "Senegaal", "ner_type": "LOC", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q1041", "qid_label": "Sénégal", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q1041", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Afrique de l'Ouest", "...
wol_test_1234
Déedet , liy suqali Afirig tey tax ñu dab réew yu naat yi , mooy ÑU GÉNNE BUUMU NJAAM geek suufeel suñu bopp gi ci suñu xel yi , te xam xéll ne , lu ñu takku liggéey mayul , leneen duñu ko may , loolu rekk moo ñu mën a suqali ba ñu dab réew yu am alal yi .
[ "Déedet", ",", "liy", "suqali", "Afirig", "tey", "tax", "ñu", "dab", "réew", "yu", "naat", "yi", ",", "mooy", "ÑU", "GÉNNE", "BUUMU", "NJAAM", "geek", "suufeel", "suñu", "bopp", "gi", "ci", "suñu", "xel", "yi", ",", "te", "xam", "xéll", "ne", ",", ...
[ { "start": 20, "end": 26, "text": "Afirig", "ner_type": "LOC", "token_start": 4, "token_end": 5, "qid": "Q15", "qid_label": "Africa", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q15", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "continent", "source": "wikidata", ...
wol_test_1242
Tey jii , ÑU NGI WAX fii ci Basiir , ci Buluf nga xam ne fi la Usmaan Sónko cosaanoo , te bokk ci Kaasamaas , ne moom Usmaan Sónko , du Kariim Wàdd te it du doon Xalifa Sàll .
[ "Tey", "jii", ",", "ÑU", "NGI", "WAX", "fii", "ci", "Basiir", ",", "ci", "Buluf", "nga", "xam", "ne", "fi", "la", "Usmaan", "Sónko", "cosaanoo", ",", "te", "bokk", "ci", "Kaasamaas", ",", "ne", "moom", "Usmaan", "Sónko", ",", "du", "Kariim", "Wàdd", ...
[ { "start": 28, "end": 34, "text": "Basiir", "ner_type": "LOC", "token_start": 8, "token_end": 9, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_met...
wol_test_1244
Ci nettalib ANSD bu atum 2020 , mu ngi ciy xamle tolluwaayu ñàkk a xëyug ndaw ñi am fukki at ak juróom wala lu ko ëpp , nekk fukk ak juróom - benn , kos juróom - ñaar ci téeméeri ndaw yoo jël .
[ "Ci", "nettalib", "ANSD", "bu", "atum", "2020", ",", "mu", "ngi", "ciy", "xamle", "tolluwaayu", "ñàkk", "a", "xëyug", "ndaw", "ñi", "am", "fukki", "at", "ak", "juróom", "wala", "lu", "ko", "ëpp", ",", "nekk", "fukk", "ak", "juróom", "-", "benn", ",",...
[ { "start": 12, "end": 16, "text": "ANSD", "ner_type": "ORG", "token_start": 2, "token_end": 3, "qid": "Q2826667", "qid_label": "Agence nationale de la statistique et de la démographie", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q2826667", "qid_description_lang": "fr", "q...
wol_test_1247
Yokkug njëgu kuuraŋ li téeñ la rekk ci li waa Senegaal yi war a jànkuwanteel , yen ba ñëwagul .
[ "Yokkug", "njëgu", "kuuraŋ", "li", "téeñ", "la", "rekk", "ci", "li", "waa", "Senegaal", "yi", "war", "a", "jànkuwanteel", ",", "yen", "ba", "ñëwagul", "." ]
[ { "start": 46, "end": 54, "text": "Senegaal", "ner_type": "LOC", "token_start": 10, "token_end": 11, "qid": "Q1041", "qid_label": "Sénégal", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q1041", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Afrique de l'Ouest", ...
wol_test_1248
Mu neex leen , mu naqari leen , dinañu jox PASTEF ak SÓNKO ay jumtukaay yu doy ba ñu jël ndam li ci wotey meer yu 2021 , yu deppite yu 2022 ak tamit wotey njiitu réew yu 2024 .
[ "Mu", "neex", "leen", ",", "mu", "naqari", "leen", ",", "dinañu", "jox", "PASTEF", "ak", "SÓNKO", "ay", "jumtukaay", "yu", "doy", "ba", "ñu", "jël", "ndam", "li", "ci", "wotey", "meer", "yu", "2021", ",", "yu", "deppite", "yu", "2022", "ak", "tamit",...
[ { "start": 43, "end": 49, "text": "PASTEF", "ner_type": "ORG", "token_start": 10, "token_end": 11, "qid": "Q98347378", "qid_label": "Patriotes africains du Sénégal pour le travail, l'éthique et la fraternité", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q98347378", "qid_descri...
wol_test_1249
CEDEAO jël na turu ECO muy turu xaalisam bi ay réewam yépp bokk
[ "CEDEAO", "jël", "na", "turu", "ECO", "muy", "turu", "xaalisam", "bi", "ay", "réewam", "yépp", "bokk" ]
[ { "start": 0, "end": 6, "text": "CEDEAO", "ner_type": "ORG", "token_start": 0, "token_end": 1, "qid": "Q193272", "qid_label": "communauté économique des États de l'Afrique de l'Ouest", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q193272", "qid_description_lang": "fr", "qid...
wol_test_1251
Diiru fan - weeri at ak lu topp , te ñu boole ci di def li waroon ci kaaraange gi jamono jooja , Bato " La Signare " mooy tax nit ñi di dem ak a dikk , rawatina di leen yóbbu ca Gore .
[ "Diiru", "fan", "-", "weeri", "at", "ak", "lu", "topp", ",", "te", "ñu", "boole", "ci", "di", "def", "li", "waroon", "ci", "kaaraange", "gi", "jamono", "jooja", ",", "Bato", "\"", "La", "Signare", "\"", "mooy", "tax", "nit", "ñi", "di", "dem", "ak"...
[ { "start": 178, "end": 182, "text": "Gore", "ner_type": "LOC", "token_start": 43, "token_end": 44, "qid": "Q244347", "qid_label": "Gorée", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q244347", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "one of the 19 communes d'arron...
wol_test_1253
LU DEFU WAXU nag , mooy yéenekaayubweb ci kàllaamay Kocc bees fi jëkk a taxawal .
[ "LU", "DEFU", "WAXU", "nag", ",", "mooy", "yéenekaayubweb", "ci", "kàllaamay", "Kocc", "bees", "fi", "jëkk", "a", "taxawal", "." ]
[ { "start": 0, "end": 12, "text": "LU DEFU WAXU", "ner_type": "ORG", "token_start": 0, "token_end": 3, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotatio...
wol_test_1254
Jeynaba Taraawore amoon na lu war a mat ñaar - fukki at , mu ngi dëkkoon Inite 11 ci Pàrsel Aseni .
[ "Jeynaba", "Taraawore", "amoon", "na", "lu", "war", "a", "mat", "ñaar", "-", "fukki", "at", ",", "mu", "ngi", "dëkkoon", "Inite", "11", "ci", "Pàrsel", "Aseni", "." ]
[ { "start": 0, "end": 17, "text": "Jeynaba Taraawore", "ner_type": "PER", "token_start": 0, "token_end": 2, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "anno...
wol_test_1255
Ki fi nekkoon kapiteenu Gaynde yi dafa bëggoon am taax ( etaas ) ci Dakaar .
[ "Ki", "fi", "nekkoon", "kapiteenu", "Gaynde", "yi", "dafa", "bëggoon", "am", "taax", "(", "etaas", ")", "ci", "Dakaar", "." ]
[ { "start": 68, "end": 74, "text": "Dakaar", "ner_type": "LOC", "token_start": 14, "token_end": 15, "qid": "Q3718", "qid_label": "Dakar", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q3718", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "capital and the largest city of Se...
wol_test_1256
Guddi gu kenn dootul fàtte , ginnaaw joŋante biy joxe ñetteelu palaas bi te doxoon diggante Petro de Luanda mi daan Patriots bu Rwanda ( 97 - 68 ) , Monastir ak Zamalek jàmmaarloo nañu ñoom ñaar .
[ "Guddi", "gu", "kenn", "dootul", "fàtte", ",", "ginnaaw", "joŋante", "biy", "joxe", "ñetteelu", "palaas", "bi", "te", "doxoon", "diggante", "Petro", "de", "Luanda", "mi", "daan", "Patriots", "bu", "Rwanda", "(", "97", "-", "68", ")", ",", "Monastir", "ak...
[ { "start": 92, "end": 107, "text": "Petro de Luanda", "ner_type": "ORG", "token_start": 16, "token_end": 19, "qid": "Q2869505", "qid_label": "Atlético Petróleos Luanda", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q2869505", "qid_description_lang": "fr", "qid_description":...
wol_test_1257
Bi ñu tàmbaliwaatee futbal bi , Gómis ak Dijon jiitu ci joŋante bi .
[ "Bi", "ñu", "tàmbaliwaatee", "futbal", "bi", ",", "Gómis", "ak", "Dijon", "jiitu", "ci", "joŋante", "bi", "." ]
[ { "start": 32, "end": 37, "text": "Gómis", "ner_type": "PER", "token_start": 6, "token_end": 7, "qid": "Q15984480", "qid_label": "Alfred Gomis", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q15984480", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "Senegalian footballer ...
wol_test_1259
Booba ba tey , mu ngi wéy di néewal doole ekibi Ërob yi ak pexeem yu yàgg yi ngir samp fi waa Ibéri .
[ "Booba", "ba", "tey", ",", "mu", "ngi", "wéy", "di", "néewal", "doole", "ekibi", "Ërob", "yi", "ak", "pexeem", "yu", "yàgg", "yi", "ngir", "samp", "fi", "waa", "Ibéri", "." ]
[ { "start": 48, "end": 52, "text": "Ërob", "ner_type": "LOC", "token_start": 11, "token_end": 12, "qid": "Q46", "qid_label": "Europe", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q46", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "terrestrial continent located in north-...
wol_test_1261
Ñu ngi xaar ba seen xel dellusi , ñu soog a feeñal dëgg ji ci mbiru dekereb 2020 - 964 / AKILEE , nga xam ne moo waral coow li .
[ "Ñu", "ngi", "xaar", "ba", "seen", "xel", "dellusi", ",", "ñu", "soog", "a", "feeñal", "dëgg", "ji", "ci", "mbiru", "dekereb", "2020", "-", "964", "/", "AKILEE", ",", "nga", "xam", "ne", "moo", "waral", "coow", "li", "." ]
[ { "start": 89, "end": 95, "text": "AKILEE", "ner_type": "ORG", "token_start": 21, "token_end": 22, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_m...
wol_test_1262
Atum 2016 lañu ko jàppoon ca digu Senegaal ak Ginne ginnaaw bi mu rëccee ba def juróomi weer Gàmbi .
[ "Atum", "2016", "lañu", "ko", "jàppoon", "ca", "digu", "Senegaal", "ak", "Ginne", "ginnaaw", "bi", "mu", "rëccee", "ba", "def", "juróomi", "weer", "Gàmbi", "." ]
[ { "start": 34, "end": 42, "text": "Senegaal", "ner_type": "LOC", "token_start": 7, "token_end": 8, "qid": "Q1041", "qid_label": "Sénégal", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q1041", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Afrique de l'Ouest", ...
wol_test_1263
Rax - ci - dolli mu boole Sterling ci ñi tàmbali joŋante bi te ñépp xamoon nañu ne futbalam barewul muj , donte sax ku mën a lëjal defãasu ñi muy janool la .
[ "Rax", "-", "ci", "-", "dolli", "mu", "boole", "Sterling", "ci", "ñi", "tàmbali", "joŋante", "bi", "te", "ñépp", "xamoon", "nañu", "ne", "futbalam", "barewul", "muj", ",", "donte", "sax", "ku", "mën", "a", "lëjal", "defãasu", "ñi", "muy", "janool", "la...
[ { "start": 26, "end": 34, "text": "Sterling", "ner_type": "PER", "token_start": 7, "token_end": 8, "qid": "Q312157", "qid_label": "Raheem Sterling", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q312157", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "English association ...
wol_test_1265
Wiiw CNRA mi lawal ay daanam ba ci jotaayi tele yi dooleel NJABAR yi ñu boole ci diiney lislaam wala ci diiney Yàlla yu bare .
[ "Wiiw", "CNRA", "mi", "lawal", "ay", "daanam", "ba", "ci", "jotaayi", "tele", "yi", "dooleel", "NJABAR", "yi", "ñu", "boole", "ci", "diiney", "lislaam", "wala", "ci", "diiney", "Yàlla", "yu", "bare", "." ]
[ { "start": 5, "end": 9, "text": "CNRA", "ner_type": "ORG", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q2994165", "qid_label": "Conseil national de régulation de l'audiovisuel", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q2994165", "qid_description_lang": "fr", "qid_descrip...
wol_test_1266
Aram Faal dafa teel a xam ne làkku farañse dafa dox diggante jàngkat yi ñu jiite te war a wone yoon wi , ak askan wi leen war a wóolu .
[ "Aram", "Faal", "dafa", "teel", "a", "xam", "ne", "làkku", "farañse", "dafa", "dox", "diggante", "jàngkat", "yi", "ñu", "jiite", "te", "war", "a", "wone", "yoon", "wi", ",", "ak", "askan", "wi", "leen", "war", "a", "wóolu", "." ]
[ { "start": 0, "end": 9, "text": "Aram Faal", "ner_type": "PER", "token_start": 0, "token_end": 2, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_me...
wol_test_1268
Waaw Pastef dafa raglu , fitna bile nguur gi jëmale ci suñu pàrti bi dafay firndeel ne tey , Apr dafa taxaw taxawaayu wujji Pastef mi nga xam ne , moo fiy jëmmal coppite ak yaakaaru ndawi ëllëg yi .
[ "Waaw", "Pastef", "dafa", "raglu", ",", "fitna", "bile", "nguur", "gi", "jëmale", "ci", "suñu", "pàrti", "bi", "dafay", "firndeel", "ne", "tey", ",", "Apr", "dafa", "taxaw", "taxawaayu", "wujji", "Pastef", "mi", "nga", "xam", "ne", ",", "moo", "fiy", "...
[ { "start": 5, "end": 11, "text": "Pastef", "ner_type": "ORG", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q98347378", "qid_label": "Patriotes africains du Sénégal pour le travail, l'éthique et la fraternité", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q98347378", "qid_descripti...
wol_test_1271
Waaye nag war nañu moytu bu baax kàngam yile di Luka Modric ( Real Madrid ) , Marcelo Brozovic ak Ivan Perisic ( Inter ) .
[ "Waaye", "nag", "war", "nañu", "moytu", "bu", "baax", "kàngam", "yile", "di", "Luka", "Modric", "(", "Real", "Madrid", ")", ",", "Marcelo", "Brozovic", "ak", "Ivan", "Perisic", "(", "Inter", ")", "." ]
[ { "start": 48, "end": 59, "text": "Luka Modric", "ner_type": "PER", "token_start": 10, "token_end": 12, "qid": "Q483837", "qid_label": "Luka Modrić", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q483837", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "joueur de football"...
wol_test_1272
Ni ko Martial Ze Belinga xamlee , ndéem ñu ngi jeegoy moom - suñu - bopp ci wàllu koom , këri liggéeyukaay yu Tugal yi , rawatina nag Farãas , dañu war a xam liy seen entere , entere bi seen këri liggéeyukaay yi di am ci jëfalante bu bees bi xew léegi ci àdduna bi .
[ "Ni", "ko", "Martial", "Ze", "Belinga", "xamlee", ",", "ndéem", "ñu", "ngi", "jeegoy", "moom", "-", "suñu", "-", "bopp", "ci", "wàllu", "koom", ",", "këri", "liggéeyukaay", "yu", "Tugal", "yi", ",", "rawatina", "nag", "Farãas", ",", "dañu", "war", "a",...
[ { "start": 6, "end": 24, "text": "Martial Ze Belinga", "ner_type": "PER", "token_start": 2, "token_end": 5, "qid": "Q23978709", "qid_label": "Martial Ze Belinga", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q23978709", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "writ...
wol_test_1273
Ndaxte , mbir moomule xewe woon ci géeju Espaañ , Njiitu réew la woon , Meetar Abdulaay Wàdd xawoon na cee ñàkk bakkanam bi , dafa faroon sax teeri ca réew ma ci lu dul woon coobareem .
[ "Ndaxte", ",", "mbir", "moomule", "xewe", "woon", "ci", "géeju", "Espaañ", ",", "Njiitu", "réew", "la", "woon", ",", "Meetar", "Abdulaay", "Wàdd", "xawoon", "na", "cee", "ñàkk", "bakkanam", "bi", ",", "dafa", "faroon", "sax", "teeri", "ca", "réew", "ma",...
[ { "start": 41, "end": 47, "text": "Espaañ", "ner_type": "LOC", "token_start": 8, "token_end": 9, "qid": "Q29", "qid_label": "Spain", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q29", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "country in southwestern Europe with terr...
wol_test_1275
xët fukk ak ñett bu nettalib CEP ) Ki gàlloo ñaawtéef bi amoon ci alali réew mi dëgg , du kenn ku dul Mamadu Maamur Jàllo , Meysa Njaay mi ñu ci bëgg a sànk te taqewu ci , laalewu ci .
[ "xët", "fukk", "ak", "ñett", "bu", "nettalib", "CEP", ")", "Ki", "gàlloo", "ñaawtéef", "bi", "amoon", "ci", "alali", "réew", "mi", "dëgg", ",", "du", "kenn", "ku", "dul", "Mamadu", "Maamur", "Jàllo", ",", "Meysa", "Njaay", "mi", "ñu", "ci", "bëgg", "...
[ { "start": 102, "end": 121, "text": "Mamadu Maamur Jàllo", "ner_type": "PER", "token_start": 23, "token_end": 26, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", ...
wol_test_1277
Ndaxte laata loolu , mësul a yeewu ak jafe - jafe bu tare noonu te du ko lijjanti balaa ngoon . . . ngir bañ a wax laata jant bi di fay Màlle Fofana PhDComUnic .
[ "Ndaxte", "laata", "loolu", ",", "mësul", "a", "yeewu", "ak", "jafe", "-", "jafe", "bu", "tare", "noonu", "te", "du", "ko", "lijjanti", "balaa", "ngoon", ".", ".", ".", "ngir", "bañ", "a", "wax", "laata", "jant", "bi", "di", "fay", "Màlle", "Fofana",...
[ { "start": 136, "end": 148, "text": "Màlle Fofana", "ner_type": "PER", "token_start": 32, "token_end": 34, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "anno...
wol_test_1280
Ndaw si dafa tàggook jëkkëram , jotoon naa am jenn doom ju am ñeenti at , mu ngi yoroon ab kàntin , doon jaay ay diw - yaram ak ñoom seen ci màrse Joor .
[ "Ndaw", "si", "dafa", "tàggook", "jëkkëram", ",", "jotoon", "naa", "am", "jenn", "doom", "ju", "am", "ñeenti", "at", ",", "mu", "ngi", "yoroon", "ab", "kàntin", ",", "doon", "jaay", "ay", "diw", "-", "yaram", "ak", "ñoom", "seen", "ci", "màrse", "Joo...
[ { "start": 147, "end": 151, "text": "Joor", "ner_type": "LOC", "token_start": 33, "token_end": 34, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_m...
wol_test_1281
Ginnaaw bu ko Usmaan Sónko weeree ci mbedd mi lu jege ñaari at booba ba léegi , ñun duñu yëy yàbbi ci mbirum juróom - ñeent - fukki milyaar ak ñeent moomu , nga xam ne tey , mu ngi ci loxoy yoon .
[ "Ginnaaw", "bu", "ko", "Usmaan", "Sónko", "weeree", "ci", "mbedd", "mi", "lu", "jege", "ñaari", "at", "booba", "ba", "léegi", ",", "ñun", "duñu", "yëy", "yàbbi", "ci", "mbirum", "juróom", "-", "ñeent", "-", "fukki", "milyaar", "ak", "ñeent", "moomu", "...
[ { "start": 14, "end": 26, "text": "Usmaan Sónko", "ner_type": "PER", "token_start": 3, "token_end": 5, "qid": "Q56312650", "qid_label": "Ousmane Sonko", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q56312650", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "homme d'État s...
wol_test_1285
Te xaalis boobu , dërëmu PASTEF ak yeneen làngi pólotig yaa ngi ci biir .
[ "Te", "xaalis", "boobu", ",", "dërëmu", "PASTEF", "ak", "yeneen", "làngi", "pólotig", "yaa", "ngi", "ci", "biir", "." ]
[ { "start": 25, "end": 31, "text": "PASTEF", "ner_type": "ORG", "token_start": 5, "token_end": 6, "qid": "Q98347378", "qid_label": "Patriotes africains du Sénégal pour le travail, l'éthique et la fraternité", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q98347378", "qid_descript...
wol_test_1287
Atum ren ngir def lu raw li weesu ci sargalug Sëriñ Abdul Asiis Al Amiin , Kurélu jàppalante gu Corée jox na ñu fan - weeri doktoor yoo xam ne xam - xami paj yépp am nañu ci , loolu nekk lu Doktoor Wardi rafetlu lool .
[ "Atum", "ren", "ngir", "def", "lu", "raw", "li", "weesu", "ci", "sargalug", "Sëriñ", "Abdul", "Asiis", "Al", "Amiin", ",", "Kurélu", "jàppalante", "gu", "Corée", "jox", "na", "ñu", "fan", "-", "weeri", "doktoor", "yoo", "xam", "ne", "xam", "-", "xami",...
[ { "start": 46, "end": 72, "text": "Sëriñ Abdul Asiis Al Amiin", "ner_type": "PER", "token_start": 10, "token_end": 15, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil...
wol_test_1291
Mbir mi sonal tamit Senegaal gi nga xam ne , way - loru yi dañuy gën a bare .
[ "Mbir", "mi", "sonal", "tamit", "Senegaal", "gi", "nga", "xam", "ne", ",", "way", "-", "loru", "yi", "dañuy", "gën", "a", "bare", "." ]
[ { "start": 20, "end": 28, "text": "Senegaal", "ner_type": "LOC", "token_start": 4, "token_end": 5, "qid": "Q1041", "qid_label": "Sénégal", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q1041", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Afrique de l'Ouest", ...
wol_test_1292
Ca Malaisie , diggante 1985 ba 2000 , juróom - ñett - fukk ak juróom - ñaar ci téeméer boo jël ci àll bi ñu gental , ay jëmbëtkati garabi tiir a ko def .
[ "Ca", "Malaisie", ",", "diggante", "1985", "ba", "2000", ",", "juróom", "-", "ñett", "-", "fukk", "ak", "juróom", "-", "ñaar", "ci", "téeméer", "boo", "jël", "ci", "àll", "bi", "ñu", "gental", ",", "ay", "jëmbëtkati", "garabi", "tiir", "a", "ko", "de...
[ { "start": 3, "end": 11, "text": "Malaisie", "ner_type": "LOC", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q833", "qid_label": "Malaisie", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q833", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "pays d'Asie du Sud-Est indépendant...
wol_test_1293
Tey Peresidãa Sàll la , ëllëg , ropplaan bi ropplaanu njiitu réew miy ñëw lay doon .
[ "Tey", "Peresidãa", "Sàll", "la", ",", "ëllëg", ",", "ropplaan", "bi", "ropplaanu", "njiitu", "réew", "miy", "ñëw", "lay", "doon", "." ]
[ { "start": 14, "end": 18, "text": "Sàll", "ner_type": "PER", "token_start": 2, "token_end": 3, "qid": "Q57438", "qid_label": "Macky Sall", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q57438", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "4th President of Senegal, forme...
wol_test_1295
Ginnaaw ay simili rekk , daamaaru Ford gi yore limat AA - 996 - BB te ku ñuy wax Seex Njaay doon ko dawal , àndoon ak Abdu Fay , dafa fekki Daam Si mi doon dawal móto bi , ngir xam lu ko taxoon a tàrde .
[ "Ginnaaw", "ay", "simili", "rekk", ",", "daamaaru", "Ford", "gi", "yore", "limat", "AA", "-", "996", "-", "BB", "te", "ku", "ñuy", "wax", "Seex", "Njaay", "doon", "ko", "dawal", ",", "àndoon", "ak", "Abdu", "Fay", ",", "dafa", "fekki", "Daam", "Si", ...
[ { "start": 34, "end": 38, "text": "Ford", "ner_type": "ORG", "token_start": 6, "token_end": 7, "qid": "Q44294", "qid_label": "Ford", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q44294", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "constructeur automobile américain", ...
wol_test_1296
Ca Etaasini , Repibilikee yi ak demokaraat yi juboo nañu ca Senaa ba , ngir wéyal tëralinu ñaari junney milyaari dolaar yu Peresidãa Trump , ginnaaw bu ñu waxtaanee lu mat fukki fan ci waxtaanu wu tar ci téere bu mujj bi am junney xët .
[ "Ca", "Etaasini", ",", "Repibilikee", "yi", "ak", "demokaraat", "yi", "juboo", "nañu", "ca", "Senaa", "ba", ",", "ngir", "wéyal", "tëralinu", "ñaari", "junney", "milyaari", "dolaar", "yu", "Peresidãa", "Trump", ",", "ginnaaw", "bu", "ñu", "waxtaanee", "lu", ...
[ { "start": 3, "end": 11, "text": "Etaasini", "ner_type": "LOC", "token_start": 1, "token_end": 2, "qid": "Q30", "qid_label": "United States", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q30", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "country located primarily in No...
wol_test_1297
Ci noonu , mu sant kilifay nguur gi ñu sos ay bérebi tàggatu , xoolaat anami liggéey bi , rawatina ñi nekk ci tali bi ( Keesug kaaraangeg askan wi , Ipres , atu àllaterete ) , fi ñiy dox war a jaar , joxe ay permi dawal oto ak saytug mën a demug daamaar yi .
[ "Ci", "noonu", ",", "mu", "sant", "kilifay", "nguur", "gi", "ñu", "sos", "ay", "bérebi", "tàggatu", ",", "xoolaat", "anami", "liggéey", "bi", ",", "rawatina", "ñi", "nekk", "ci", "tali", "bi", "(", "Keesug", "kaaraangeg", "askan", "wi", ",", "Ipres", "...
[ { "start": 149, "end": 154, "text": "Ipres", "ner_type": "ORG", "token_start": 31, "token_end": 32, "qid": null, "qid_label": null, "qid_url": null, "qid_description_lang": null, "qid_description": null, "source": null, "annotation_status": "nil", "annotation_...
wol_test_1299
Ñu ngi woy di fecc ngir màggal li ñu jot a def , militaŋ bi , njureef yi ñu am ci juróom - benn ati liggéey yi , yu defar ab pàrti bu am doole bu raglu bu mel ni PASTEF .
[ "Ñu", "ngi", "woy", "di", "fecc", "ngir", "màggal", "li", "ñu", "jot", "a", "def", ",", "militaŋ", "bi", ",", "njureef", "yi", "ñu", "am", "ci", "juróom", "-", "benn", "ati", "liggéey", "yi", ",", "yu", "defar", "ab", "pàrti", "bu", "am", "doole", ...
[ { "start": 162, "end": 168, "text": "PASTEF", "ner_type": "ORG", "token_start": 40, "token_end": 41, "qid": "Q98347378", "qid_label": "Patriotes africains du Sénégal pour le travail, l'éthique et la fraternité", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q98347378", "qid_desc...
wol_test_1305
Njiitu réew mi di xalaat ci tabb meeru Dakaar ak ab dekere , loolu aw saaga lay doon ci waa Dakaar yépp .
[ "Njiitu", "réew", "mi", "di", "xalaat", "ci", "tabb", "meeru", "Dakaar", "ak", "ab", "dekere", ",", "loolu", "aw", "saaga", "lay", "doon", "ci", "waa", "Dakaar", "yépp", "." ]
[ { "start": 39, "end": 45, "text": "Dakaar", "ner_type": "LOC", "token_start": 8, "token_end": 9, "qid": "Q3718", "qid_label": "Dakar", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q3718", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "capital and the largest city of Sene...
wol_test_1306
Gis naa Maki Sàll soppi tuuti ci waxin wi , naan yalwaanuñu , ni ñu dàqe àpp gi doy na ñu .
[ "Gis", "naa", "Maki", "Sàll", "soppi", "tuuti", "ci", "waxin", "wi", ",", "naan", "yalwaanuñu", ",", "ni", "ñu", "dàqe", "àpp", "gi", "doy", "na", "ñu", "." ]
[ { "start": 8, "end": 17, "text": "Maki Sàll", "ner_type": "PER", "token_start": 2, "token_end": 4, "qid": "Q57438", "qid_label": "Macky Sall", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q57438", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "homme d'État sénégalais", ...
wol_test_1307
2012 ba tey , Bayer Liverkuzen daanul Munich dëkkam .
[ "2012", "ba", "tey", ",", "Bayer", "Liverkuzen", "daanul", "Munich", "dëkkam", "." ]
[ { "start": 14, "end": 30, "text": "Bayer Liverkuzen", "ner_type": "ORG", "token_start": 4, "token_end": 6, "qid": "Q104761", "qid_label": "Bayer 04 Leverkusen", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q104761", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "associat...
wol_test_1310
DELACROIX nee na ñu ndefarug ndaanaan dafa war a yéem ki koy xool . . . bu mbégte amul rekk , dafa fekk ne lu rafet amul .
[ "DELACROIX", "nee", "na", "ñu", "ndefarug", "ndaanaan", "dafa", "war", "a", "yéem", "ki", "koy", "xool", ".", ".", ".", "bu", "mbégte", "amul", "rekk", ",", "dafa", "fekk", "ne", "lu", "rafet", "amul", "." ]
[ { "start": 0, "end": 9, "text": "DELACROIX", "ner_type": "PER", "token_start": 0, "token_end": 1, "qid": "Q33477", "qid_label": "Eugène Delacroix", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q33477", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "peintre français (1798...
wol_test_1311
Ray gi jaaxaal na leen lool , moo tax sax waa Rooso ñu ngi naan nañu jàpp ki def ñaawteef bi nu mu gën a gaawe .
[ "Ray", "gi", "jaaxaal", "na", "leen", "lool", ",", "moo", "tax", "sax", "waa", "Rooso", "ñu", "ngi", "naan", "nañu", "jàpp", "ki", "def", "ñaawteef", "bi", "nu", "mu", "gën", "a", "gaawe", "." ]
[ { "start": 46, "end": 51, "text": "Rooso", "ner_type": "LOC", "token_start": 11, "token_end": 12, "qid": "Q3442852", "qid_label": "Rosso", "qid_url": "http://www.wikidata.org/entity/Q3442852", "qid_description_lang": "fr", "qid_description": "commune of Senegal", "sou...